CHERIFOU Pop Pop cover image

Pop Pop Lyrics

Pop Pop Lyrics by CHERIFOU


Kay kay kay kay
Kay ma khamal la ni
Adoun’ya dou benn fann
Kingay togué tay bou souba meun’nala yéy
Kay ma digual’la ni
Bouldi khol nitt diko nié
Meul nala yobbé ignaaan (ignaan ignaaan)
Yangui coq  coq ba callé
May pop pop ci khalé
Ngay togg togg ba callé
Diémo té meuno dabbé
Man soma beugoulé boul saalé
Guiss’nané dolé feeling béla poussalé eehhhhhh yah
So beugoulê boul salé
Bayil sokhor ignaan dalay té
Boko toppé dangay dé firiil sa khol
 
Ay way ah
Yeukna linga nékké (ay door rék)
Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék)
Eh bal dooré
Guiss’nala ngay leuré eh eh ehhhh do goré
Man guiss’na ningmay woré
Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou
Bo déffé’ni ya geuna yéwou nieup, nalaw nga bay galleu
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Dél thioy rék

Dembeu yanei woon
Dembeu yanei woon ni gorêdiwo
Konn loula diapp tay banga né ci yoonou noon
Non parégouma
Nono tambalé gouma
Yay sakhol ci nianaal’ma
Sabo douhan ouma mi falama néné barakaa
Yangui coq  coq ba callé
May pop pop ci khalé
Ngay togg togg ba callé
Diémo té meuno dabbé
Yaw woutal béneen yoon bo diarei
Yaw démo kou nekk ci yoon nga diém’ko garé
Bayil sokhor ignaan dalay té
Soko toppé dangay dé firiil sa khol

Ay way ah
Yegg’na linga nékké (ay door rék)
Malay lébal mbakh ngamay fékhél (ay door rék)
Eh bal dooré
Guiss’nala ngay leuré eh eh ehhhh do goré
Man guiss’na ningmay woré
Boul déféni ninga nékké yeugoumako dama doylou
Bo déffé’ni ya geuna yéwou nieup, nalaw nga bay galleu
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Thioy rék
Yaw deukéll thioy rék
Dél thioy rék

Thiow meunoul dara
Wakh djou bonn fadioul dara (dedett)
Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett)
Thiow meunoul dara ci man wakh dji fadioul dara (dedett)
Thiow meunoul dara wakh dji fadioul dara
Thiow meunoul dara wakh dji bonn fadioul dara
Thiowli meunoul dara dafmay yokk dolê nopaloul
Khalé baangéééé (man’la)
Khalé baangéééé (kham’ngan man’la waaawaaw)
Kham ngani man’la
Ay man’la
Affaire bi man’la
Wooooy man’la
Nénagn’ma yaw la ehhhhh
Khalé baangéééé (man’la)
Kham ngani man’la
Ay man’la
Affaire bi man’la
Wooooy man’la
Nénagn’ma yaw la ehhhhh
Té bilae damay fo ak yennn

Watch Video

About Pop Pop

Album : Pop Pop (Single)
Release Year : 2023
Added By : Farida
Published : Jun 17 , 2023

More CHERIFOU Lyrics

CHERIFOU
CHERIFOU
CHERIFOU
CHERIFOU

Comments ( 0 )

No Comment yet



About AfrikaLyrics

Afrika Lyrics is the most diverse collection of African song lyrics and translations. Afrika Lyrics provides music lyrics from over 30 African countries and lyrics translations from over 10 African Languages into English and French

Follow Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl